
As-Salamu hanleykoum wa rahmatoul Lah wa DAHIRA GÉNÉRATION SOPEY SERIGNE SAM MBAYE www.G3sm.org
Ñogui leen di yëggël ni GAMOU gui migui tombeek Nuit du 19 à 20 Novembre 2018 Comme niñuko daan déffé rékk waxtu wu Gamou gui dioupsé membres ru Dahira bi ku nékk déff lo man ñou dadialé ko mu neew mu bëri yobuko ci Ndiabotou Serigne Sam Mbaye pour Barkeelo ko ci Gamou gui in Chaa Allah
CHARTE » bi mooy sassuñou keen, léppu lu way man rékk soko ci déffé dinaan ko diébaal wa Keur Serigne Sam Mbaye in Chaa ALLAH
Kèppu kuci beugga barkéllou man nga diokook
S Mamadou Gaye Saam ci número bi +221 77 507 46 92
dinala wax niggay déff bamou diott si moxaam dagga nékk Bitiim Réw wala dagga nékk Sénégal
Dernier délai bi le 19 Novembre 2018 In chaa ‘Allah. Manaam lepp lou waay di barkeelo mann ko deff fi ba le 19 Novembre