Des clés USB de 16GB avec 1860 sons de Serigne Sam Mbaye disponible à 5000 F CFA .

 

DAHIRA GÉNÉRATION SOPEY SERIGNE SAM MBAYE G3sm

INFO

 

As-Salamu hanleykoum wa rahmatoul lah wa barakatuhu mbokku dioulitt yi, mbokku Talibé yi ñogui leen di nouyu dileen ziarra Dileen yeugueul née amna liggeey bou ñou nékoon jamono yi yeup dieum ci wallu ngeuna tassaarei ndiangaleem Serigne Saam Mbaye (RTA)

Dahira bi amna 100 clés USB (capacité 16 gigas bits) youmou ndieundeu ci been dieuwrine diou nekk fii ci biir Dahira bi. Moom sikk mbaxaam, mou yook ci 50 mayko wa G3SM. Mouy 150 clés USB. Clé bou nekk amna 1860 sons you Serigne Sam en format MP3 ak AMR.

Gnou dikko wethi ko 5000 F CFA. Kou beugg nakk mann nga diokko ak dieuwrine dji nekk sa diwaan bâ nga deukkei. Liste been la rekk ak bou cotisations yi.

Gni nga khamnei fignou nekk amougne dieuwrine, manna gno jokko ak *Abdallah Cissé Saam, Baay Djily Diaw Saam wala Sokhna Maman Gueye

 

 

LISTE DES REPRÉSENTANTS

 

 

Dakar: Serigne Mamadou Gaye Saam (77 507 4692)
Touba : Serigne Thierno Saam Sall (76 734 17 15)
Louga : Sokhna Maman Gueye (77 055 9673)
Kolda : Serigne Khadim Sow ( 77 956 86 55)
Espagne : S Djily Diaw Saam (+34 685 47 96 49 / +34 632 31 14 20)
Italie : Serigne Amdy Moustapha Kâ (+39 380 744 4074)
Bresil : Mor Diagne (+555 499 121 908)
Argentine : Serigne Cheikh Diop Saam (+5491 1570 20036)
Maroc : Serigne Elh. Gueye ; (+212 696 89 5534)
Gabon : Serigne Touba Saam Ndiaye (+241 07 23 54 53)
Côte d’Ivoire : Seydina Ndiaye Mafatihul Bichri (+225 07 39 4418)
Cambie : Serigne Bassirou Diaw (+220 722 18 27)
Afrique du Sud : Serigne Ale Diop (+27 781 044 849)
Cap-vert : S Medoune Sow (+238 921 60 76)
Ziguinchor : S. Abdou Karim Sock (76 489 9159)
Niger Serigne Mouhamed Tine (+227 92 92 95 71)

 

WA SALAMU HANLEYKUM WARAHMATULAH

About The Author

Related posts

Leave a Reply

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

G3sm.org