Jayanté ci Université bu Touba ak wa Dahira Génération Sopey Serigne Sam Mbaye

DAHIRA GÉNÉRATION SOPEY SERIGNE SAM MBAYE

INFO

As’Salamu hanleykuum wa rahmatul lah wa Dahira bi ñogui leen di nouyu dileen ziar, dileen soñi di soñi suñu boppu ci liggèyu UNIVERSITÉ KHADIMOUL RASSOUL DE TOUBA (UKRAT) tee Khalif bi di Serigne Mountakha Mbacké taxawaal ko woo ci diouliit yéppu, Koon ñuun wa Dabira bi bëgg naan thié baay suñu waar dadialé suñu barkeelu diébaal ko Serigne Mountakha Mbacké Khalif Général des Mourides.

Képpu kucci bëgga barkeelu man nga diokook Serigne Thierno Saam Sall Touba ci numero bi +221 76 734 17 15 (mooy représentant Dahira bi Touba) fii ba Mercredi 16 Janvier 2019 in Shaa Allah

Numéro ORANGE MONEY 774321715 Thierno Sall

Ñogui siiy soñi ñéppu, léppu lu ci waay déff sa boppu ngako défaal tee dénth buduul yaxu la. jeureu ngeen jeuff As-Salamou hanleykuum wa rahmatul lah wa barakatuhu

About The Author

Related posts

Leave a Reply

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

G3sm.org