Première ziara de la Dahira Génération Sopey Serigne Sam Mbaye au Khalif Général des Mourides

INFO

As-Salamou hanleykoum wa rahmatoul lah wa Dahira Génération Sopey Serigne Sam Mbaye (G3sm)

Ñogui leen di ziar dileen waax née liñu dajalé ci daradji jëm ca Université Cheikh Ahmadou Bamba bu Touba migui tollu ci 386 120 F CFA jébaal nan ko Serigne Mountakha MBACKÉ Khalif Général des Mourides taay ci AL JUMMA ji Tombeek 18 Janvier 2019 ca Résidence Khadimoul Rassoul

sant ñi joxé ak ñi amoon yiné bi dileen jajëfël ci Pasteef ngi ak ci taxawaay bi, di ñaan Yalla na suñu boroom bi nanguul ñu jëff ji tee fulko ci barkeep Khassida yi ak ci barkeep Serigne Mountakha Mbacké diko ñanaal mu yagg fi loll tee weer.

Wa Salamu hanleykoum wa rahmatoul lah wa barakàtuhu

 

About The Author

Related posts

Leave a Reply

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

G3sm.org